VÍDEO
Jeeba – Saï Saï Feat Dieyla (Clip Officiel)
#saïsaï
#jeeba
#dieyla
Saï Saï disponible ici i
Jeeba à Paris🇫🇷 Achetez votre billet ici : /
Auteur : Jeeba
Interprète : Jeeba – Dieyla
Compositeur : diamond guidem
Mix Mastering : Afro Music Studio Sn
Réalisation : Mao Sidibé
Production : Abadane Daiman
Stylisme : Bise Collection – Teranga Lounge – Cana Dom
Jeeba et Dieyla proposent un cocktail musical inédit, l’histoire d’amour dénonce les mensonges et dérives des couples d’aujourd’hui.
Le son se veut drôle et raconte en interposé un récit de deux couples aux ambitions différentes et malhonnêtes.
Lyrics
Yala dou dioum mani Yala dou dioum loumou def ndeké lolou mo geune Demone na ba nar ko dougal sama biir xol
souma ko defone mangui thi tolof tolof
Kone fok ma xolate ko
Saï saïiiii la fok ma xolate ko
Wadjii Saï saïiiii la
Yalla dou dioum ndeké yalla dou dioum loumou def ndéké lolou mo geune
Demone na ba nar ko dougal sama biir xol
souma ko defone mangui thi tolof tolof
Kone fok ma xolate ko
Saï Saï la
fok ma xolate ko
Wadji Saï Saï la
yala dou dioum ndeké yalla dou dioum loumou def ndéké lolou mo geune
Demone na ba nar ko dougal sama biir xol
souma ko defone mangui thi tolof tolof
Couplet
Nieuw na sama lathté fa sama yay boy
Saï Saï la
Nieuwate sama keur lathté fa sama baye boy Saï Saï la
Néna kilifa la dou dokh thi tank thiakhane
Ñente ak tranche indi gouro dadi labane
Mingui may tek tank beug ma forcé ray
Ndéké loumou beugone dougal but bi jubilé daw Refrain
Yala dou dioum mani Yala dou dioum Loumou def ndéké lolou mo geune
Demone na bay xalate nar ko diox sama xol Ndéké souma ko defone mangui thi tolof tolof Kone fok ma xolate ko
Saï Saï la
Kone fok ma xolate ko
Ndaw ci Saï Saï la
Yala dou dioum mani yalla dou dioum loumou def ndéké lolou mo geune Demone na ba nar ko dougal sama biir xol
souma ko defone mangui thi tolof tolof
Néna koudoul mane beugoul sokhla woul
Mane rek la diokh bop kou Mel ni mane amoul Mane mako yeungal yeungal mbeguelam Ndéké mane dama door ay calmant lamay diokh Dem na ba dépense keureum mako yoor
Faye courant Faye ndokh Faye diangue xalé yi ecole
Dieund greffage Faye ay voyage ndéké damay door sama poche la nop
Refrain
Yala dou dioum mani yalla dou dioum loumou def ndéké lolou mo geune Demone na bay xalate nar ko diokh sama xol
Dejesouma ko defone mangui thi tolof tolof Kone fok ma xolate ko
Saï Saï la
Kone fok ma xolate ko
Ainda sem comentário